Auteur: Canabasse Compositeurs: Adrien Hndrxx - Canabasse Arrangeur: Canabasse Production: BuzzLab (Dakar, Senegal, Jan 2022) Mix-Mastering: Guelewaar - Sir Khalifa
Lyrics:
Man xawma lutax ba maag yaw mënu ñu juboo ñun Lutax ba ñaari fann yu nek ku nek dumoo yu Fitna bi ci kër xam na ñu ni moolul Mais seytané rekka dëkke ci di ñu noot ñun Lutax ba sa bët bi weex na sax nga giss ci sa bopp daal di berru da nga merr Soxna ci dimbalil sa bop té dimbali ma jeema soppi ni ngay dundé Tooñ na la Baal ma Tooñ nga ma baalul Fii dara grawul Rëy mo ko fi jarul Heuru ndekki ma claquer porte Bu guddé ma ñibbi ci Bokkatu sa ginnaaw Mu mel ni xuloo mëssul am Fitna laay yendo dem n’a bureau mais liggeeyuma Merre n’a la baby mais nammel bé ëpp ci man
Tooñ na la Baal ma Tooñ nga ma baalul Fii dara grawul Rëy mo ko fi jarul
Man merr na dem na Ñëwaat ndax xalaat na Giss ni adduna Amul solo Dara jaru fi xuloo baby
Man xawma lutax ba maag yaw mënu ñu juboo ñun Lutax ba ñaari fann yu nek ku nek dumoo yu Fitna bi nekk ci kër gi moolul
Mais seytané rekka dëkke ci di ñu noot ñun Lutax ba sa bët bi weex na sax nga giss ci sa bopp daal di berru da nga merr Saa waaji dimbalil sa bop té dimbali ma jeema soppi ni ngay dundé
Tooñ na la Baal ma Tooñ nga ma baalul Fii dara grawul Rëy mo fi xajul
Boo wacce ma fass kanam Pourtant ma ngi doon xaar nga ñibi ci Defaru na ba nice yeah baby xamna fim’lay jaar Fitna laay yendo dem n’a bureau Mai’s liggeeyuma Merre na la baby mais nammeel bé ëpp ci man
Tooñ na la Baal ma Tooñ nga ma baalul Fii dara grawul Rëy mo ko fi xajul
Man merr na dem na Ñëwaat ndax xalaat na Giss ni aduna Amul solo