Auteur: Canabasse Compositeurs: Gelewaar - Canabasse Arrangeur: Canabasse Production: BuzzLab (Dakar, Senegal, Jan 2022) Mix-Mastering: Sir Khalifa - Gelewaar
Lyrics:
yëgu looma
yëgu looma yëgu looma ba Maa ngi agi gai yoo Toppatoo wooma yëgu looma ba maa ngi ñibbée Resulooma yëgu looma ba ma ngui gëmmentoo Faale wooma ni Yëgu looma Yëgu looma
Da ma sonn ci di def les mêmes reproches Li ma namm ci jabar c’est des p’tites choses Tëjal sa gémmiñ bu may wax yow J’en ai marre de tes justifications Sa jëf ji du Lu bees Te leer na ma bin du tay lay jeex Ndax yàgg naa remarquer ay changements ci yaw te jot naa la ko wax I’m the real nigga type Li ma gën a bañ ci life mooy baamtuwaat Fils da nga meloon ku dëdu jàmm Lii du sa cër déggalal sa waay xam naa ni ku nekk ci ñun am na nu muy Gisee Life Mais am na yu amul négocier kon appliquel Balaa naaj Melooo woon nii dou lii nga ma doon wan balak ma lay takk Signalé gauche dem droite my baby film bi nga sàcc No ki May Gis du yaw lady Da nga jekkii bëgg saxi laaf Changé sa jiko topatoo watoo ma Pourtant Maa ngi def lépp li ma war Du moins li ma mën mais mel na ni doyu mala Man mënu ma dëkk ci joxe sans retour lii du life Lii mooy genru night yiy lëndëmal mind Baby fayu looma li ma la lebal Dama la love mais wan nga ma ni yëguloo ma
Boo ma yëggoon doo xam ñi sama xol neexul ngay nelaw Waaye bëgguloo ma Boo ma bëggoon di nga jug balu ndax xam nga ni yaa ma tooñ Yaakaaroo ma Du ma genrou Góor buy bàyyj benn jigeen mu may yab Dama yàgg bàyyi mu sedd ndax néegu sëy bi moo ko laaj Waante sëy bi jaralu la li mu ma jaral ndax Gis naa ñi Yëguloo ma Yëguloo ma ba Maa ngi gai yoo Toppatoo woo ma Yëguloo ma ba maa ngi bëgg ñibbee Resu looma Yëguloo ma ba maa ngi gëmmentoo Faale woo ma ni Yëguloo ma
Yëguloo ma
Mësu ma xalaat Naa toog bay douter sa ma choix ci yaw Li nga ma doon wan Tay mu ngi mel ni ay mirage you know Bae lan moo la dal Bu dee ci man la tamit please let me know Jugal ñu waxtaan Li ngay wakh ndégienaye bi Wakh ma ko Amoul solo bo beugatoul Wakh ma ko Mane tchi sama bop limay yeuk tay dou love Frustration bou andak haine Kheudj na sa gno sokhla trêve Nagn wo pa yi fassone sëy bi fetchi ko Mangui wakh mais limay wakh khamna ni geunalouma no Bouma Sangone gnou dess mane ak yow meuna yar sunuy dome Ndakh mane khamna li nekk tchi magg tchi kër bou tass té yéné wou ma len ko Nagn teudd ba soubeu kheudj na seytaané dem abal gno
yëgu looma yëgu looma ba Maa ngi agi gai yoo Toppatoo wooma yëgu looma ba maa ngi ñibbée Resulooma yëgu looma ba ma ngui gëmmentoo Faale wooma ni Yëgu looma Yëgu looma